
L’HOMMAGE DE SAMBA LAYE SEMBARGA A CHERIF MAME LIBASSE LAHI soodaan3
1
Bis mi laahi malikouna. Sante yala yaa rabanaa. Diouli niaane thia Mahdinaa. Seïdi Mame Libasse
2
Magui binde waye di dagaan. Beugeu wayé takhoul madiway. Sama niiya Moye Di geureum Seïdi Mame Libasse
3
Foofi tolou yagui zikar. Siriyan ãlaaniyatan. Diamou yala naanou zikar. Seïdi Mame Libasse
4
Doundal late gua souna l’imam. Koriték takhaw Di ziar. Kaamile yaagui gneup dissi téw. Seïdi Mame Libasse
5
Soo adoh si seïdi l’imam. Xole yi féeh gawan nou sa Mame. Naa gnou gueme té wolou sa Mame. Seïdi Mame Libasse
6
Roy gua Rouhoulahii Issa. Roy gua Mame ndione ak sa Baye. Seïdi Mbaye mi domou sa Mame. Seïdi Mame Libasse
7
Seïdi Thiaw ak baye Seïdi Raane. Roy gualéen ak Doomi Issaa. Abdou Laye Chérif guafi Roye. Seïdi Mame Libasse
8
Ibou Séni Laahi Chériif. Baye Weussayenou Laahi Chérif. Mamadou Laahi Séni sa makk. Seïdi Mame Libasse
9
Kouy dioulit eumbeul nala yiw. Nitte kou bakh dounonou kou yiw. Koula nonou xole ba yiwoul. Seïdi Mame Libasse
10
Roy na Mame dji roy bou rafétt. Djiko mame Dia fégn na sa mom. Mélo kaanou baye ba la yor. Seïdi Mame Libasse
11
Moy kou deugou néle sidiixoun. Moy kou mandou néle ân,ndiloun. Moy kou yaatou néke waachi,õũn. Seïdi Mame Libasse
12
Faarixoun Di méleni õmar. Sidiixoun diméleni sadiixe. Am gua kérsa com bou ãnfaan. Seïdi Mame Libasse
13
Abou sibtaïni rék ga nourol. Moy Alioune mi donou Rassoul. Bile õũloomi Moy téktalam. Seïdi Mame Libasse
14
Diamou yala rék gua Sakho. Roy samame sonaam gua Sakho. wolou yala doyelou Di gor. Seïdi Mame Libasse
15
Massoulo Dimas laa sa Mame. Foofi tolou naa Moy rasoul. Sopounanla yaw lanou am. Seïdi Mame Libasse
16
Douma faté way fi sa makk. Seyedina Bassir yaa imaam. Yale na boor bi doli sagam. Seïdi Mame Libasse
17
Gnougui gnaan si barké sa Mame. Goudou fanne bou andak salam. Yaakey sa rakk yéb yi gua am. Seïdi Mame Libasse
18
Yaa khalifa ibnou Amare. Domi Baye Mandione Doudou Laye. Yale na boor bi yokou sa fane. Seïdi Mame Libasse
19
Sali yaa Rabi ãnlaa. Seïdinaa Limaamou sa Mame. Sabaa yaak gnougnam yamou am. Seïdi Mame Libasse