ACTUALITES

QUAND LES SÉANCES DE ZIKRULLAH NOUS MANQUENT !

today15 mai 2020 15

Arrière-plan
share close

De l’importance du Zikrullah

Voici un des enchaînements au cours de ces séances en question :

Laa ilaaha illaa Allah
Laa ilaaha illaa Allah
Laa ilaaha illaa Allah
Laa ilaaha illaa Allah

Laa ilaaha illaa Allah
Laa ilaaha illaa Allah
Seydinaa Rassuulu Laahi
Laa ilaaha illaa Allah

Allaahu Allah
Allaahu Rabbii
Muhamadu Nabii
Laa ilaaha illaa Allah

Zil Mulki Buur la
Jabbaaru Ta’anlaa
Mooy Buuru jaam ñi
Laa ilaaha illaa Allah

Tagga leen Jaliilu
Baakka leen Jaliilu
Rabbul Jaliilu
Laa ilaaha illaa Allah

Njool ma ngay waaree
Waar leen sa penku
Waar leen sa sow ba
Laa ilaaha illaa Allah

Nabi laay nga Baay Lahi
Yàlla la yonni
Ngay wooté dineem
Laa ilaaha illaa Allah

Alassane ak Seeny
Ki nu woolu naxu nu
Jaaraama Baay Lahi
Laa ilaaha illaa Allah

Lil Moustapha Ndjiin
Baay Lahi Rassuulu
Yonnène baa nga Jamalahi
Laa ilaaha illaa Allah

Maam Baay Laahi amul maas
Rohu Lahi Yonnène la
Yaakaar yaa nga sow ba
Laa ilaaha illaa Allah

Ñoun gaayi Baay Lahi
Na ñu gëm te woolu
Yaakaar te doylu
Laa ilaaha illaa Allah

Ñoun gaayi Baay Lahi
Na ñou muñ te yaatu
May gaa ngui ak Baay Lahi
Laa ilaaha illaa Allah

Gëm woolu Baay Lahi
Ma ca biir Jamalahi
Mooy Rassuulu Muhamadu
Laa ilaaha illaa Allah

Gëm woolu yaakaar
Gindi reer yi, Baay Lahi
Gaal gaa nga bañé Beer
Laa ilaaha illaa Allah

Congo ki Belgique
Wiir wiir biir geej
Da nu leen di degg ndeem
Laa ilaaha illaa Allah

(Jalla Jalâlahu! Al Malîku, Al Anzîzul Jabbâru, Al Mutakabbiru, Al Xaalixul Bâriu)

Muhamadu Rassuulu Laahi
Laa ilaaha illaa Allah

Maam Libaassa Lahi Rassuulu Laahi
Laa ilaaha illaa Allah

Sangoup Jamaana Rohou Lahi
Laa ilaaha illaa Allah

Yaaram nga Seydina Manjoon
Laa ilaaha illaa Allah

Yaaram nga Baabul Uluum
Laa ilaaha illaa Allah

Ñu gëm te woolu tay saxoo
Laa ilaaha illaa Allah

Seydi Sanga la Baay ba Yaaram
Laa ilaaha illaa Allah

Chérif nga doomi Ruhulaahi
Laa ilaaha illaa Allah

Ñu anda ak Njiin ba Al Janna
Laa ilaaha illaa Allah

Dieureudieuf Seydina Limamou Lahi mi ñu xàllal yoonu Lislaam, xamal ñu Laahu Buur bi yayoo sabbaal.

Chérif Alassane Diop LAHI

Écrit par: soodaan3

Rate it

Commentaires d’articles (0)

Laisser une réponse

Votre adresse email ne sera pas publiée. Les champs marqués d'un * sont obligatoires


0%
Restez informé des nouvelles publications en activant les notifications...! OK Non