Listeners:
Top listeners:
Radio Urum-Bi La Voix du Salut
BAYE SEYDI THIAW LAHI SUR LES 364 HA OFFERTS A L'ETAT DU SENEGAL Baye Seydi Thiaw LAHI
today3 mars 2024 254 1 7 5
Bara Laye sunu xol ndaw lolou daanou beguel
kanie ngay nieuwate niou deufeul sune xol yi xool sa kanam
Xana sa toukki bi dotoul dieex nga dellou ci xool ndiabote gui
doom boula neexé delouwate fanga dieum
Yow mane bou diante bi soo nga delouwate
niou deufeul sene xol yi faté naxar wi sangaa kanam yi
Baa saa’tane lahzatane xana namoo sa ndiabote
ndiour gangui ni dila xaar sahaaba bi yow lanou miine
Bara Laye foumay dieuleeti koumay deufeul
dima dello sune Borom dima mougne loo lorr yi
Bara Laye koumay dioxati ay niaane aki dogg
nguir mou serral samap xol oyofal natou yi
Ayy Bara Laye koumay waxtaanal si Seydi Rane mima doy
sama boumou thioffel bobou sama goor googou
Bara Laye koumay dioubantéti
bouma dioumee wala ma diadda yoone wi
Bara Laye baa xam ngani mala gueunone beugue nga sori lool si mane
ak louma sor sori sori si yow mima daane wax Yaay Booy wala sama Yaayou bopp
Bara Laye nouyoulma sama goor ga Seydi Rane
neeko namanako loolll waxal mako limala waxone yeup
Bara Laye boulko faté wax lima waxoone
neeko boumou bayi di leeral sama yoone
Neeko ragalna dounyaa bi ak nimou leundemee diaxasso
neeko namay nguindi saa sounek
Bara Laye nouyoulma Sanga ba Al Imaam asws ak ndiabote ga te Rohou Lahi as djiitelene
ziaaralma lene bou baax
Boul faté sahaba ya mag niou baax nia sama maam Khady Wade
neeko namanako torop
Bara Laye doumala faté sama waadji yow tamite
lou ganale gui neex neex boulma faté
Na Bour bi dolli sa leer bi abdi maa xoulixaa
niouy sax di dioulli si Ndjine ak toppa ay ndigueuleum
Na Yallah may Sokhna Saly Anta Laye ak sa ndiabote barké ak loufiy soutoura
xolou mounie ak ndeuguerlaay defalko sa soppe yi ak Ahlou Lahi gui yeup ak dioulite yi
Denk nane Yallah Buur bi Cherif Laye ak Sokhna Laye
mou sammal nioulene aarlene laxalene fou yaxxa yegoul
Seydina Issa Laye Samb Yallah roussnou si mom
mou teeri ni aw yoone mou soute Al Imaam Saxiir aw fane té dieul barkem
Mane Maty Laye mangui lay wax a très bientôt
MON TRÈS CHER BIEN AIMÉ
Na Yallah dioulli si Baay Laay ak nia feeté sa mom seulmeul si mom
mayniou ndam ak mouthie fanou dieum
Écrit par: soodaan3
Disons Amine !
06:00 - 06:38
06:38 - 11:00
11:00 - 11:30
11:30 - 12:00
Chérif Mouhamadou Lamine LAHI
12:00 - 12:15
1
Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
Vendredi 04 août 2023 Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
2
Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
Vendredi 28 juillet 2023 Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
3
Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
Vendredi 06 octobre 2023 Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
1
Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
Vendredi 04 août 2023 Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
2
Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
Vendredi 28 juillet 2023 Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
3
Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
Vendredi 06 octobre 2023 Chérif Mouhamadou Makhtar LAHI
Copyright Soodaan
Niang Lissa sur 3 mars 2024
😥😥😥😥