POESIE : Al Khaliifa Muhamadu Al Amiin
Al Khaliifa Muhamadu Al Amiin 1. Wa Ahloulaahi ñu delou santa Rabbanaa, ci Al Amiine mi ñepp woolou jiitou naa 2. Alhamdoulilaahi santa Buur ci ay doggalam, mo dieul Muxtaarunaa mu dem Ilayiinaa 3. Guddig fukeel ci shawaal la mbir ma xew, ñepp jaaxlé naa Baay Dudu Laay laaxu naa 4. Nirook demouk Imaama laahi Xayrunaa, muy bess yu neew guinaaw Kori ga deuppu naa 5. Deuppook bessub sarakh ba […]